Sélectionner une page

Mars 2021, un carrefour pour la jeunesse sénégalaise. Il est temps pour nous de choisir et d’arrêter de subir. Il est temps que nous reprenions le pouvoir et réécrivions notre histoire. Il est temps que nous retrouvions notre voie. Notre voix. Ce pays, c’est le notre.

Yaw linga beug def baye dou dém mais comme danga gnou beug test kay gnou dem Kou ndobine rey sa mame daaw dé rêne lou nioul foko sène doko diégué dingko daw bodé borom xell yeah nitteu gawa faté lolo takh nga takamlou deuk leumm té niola faal prési dem prési dikk prési doul niou sissou fippou takk derr yi diniou shoot Mbirr bi doufi goulète kagn lagnouy tall khekh yu Bess yakarone nagn la tchi demb macky sall mais teydji nioune la contre yaw té nala leer né dictateur doufi am ndam taal sama call guiss véhicules lourds yi di djougué fatick wathie guiss decret bi prefet arrêter cours yi oh shitt nombre mort yi mingui yokk corona dotoul fitna fimou dieum lay ladj narr na gueunah métii esk baye cheikh wa keuram moudjei negn djott coram Thioye bi ko shoot esk dina nangou toram Mohamed tony agent GIGN bi lokhom bi dagg boutchi deretaam taakoul mom taalal lokho ley moudjé prix fort bi nioko deuké feyy golo di bey baboune di doundé tei sunu kaw lay deyy gnifi wooté wone pour gnu guéneu ba niou falou tey dji niom niognou niognou worr niou beug guéneuh niou taxaw xagn niouko néna dou guiss lou xonk sunu derett yengalouko requête diam dong leu mais prési gantou ko Idy taxaw sugnu kanam nane niou boudone bénéne deukk mort yi daniouy gueuna beuri what the fuck ? Niata nio wara dead pour nguène dieuli né danguène wara tégui tank pour aar li tchi dess démocratie sénégal mingui perte vitesse bane exemple nguène niouy djokh boudé kou si nek tchi yène dafa fatté lane mo takhone tchi ndialbène mou done xeex Si sène jeunesse leer nama li bokoul wone tchi sène rêve deukou leumm diouk taxaw dilène xoolé beutou traître nguène di xol sene bopp à l’aise si sètou wallahi yène ay deumm nguène Mais nak thiow dou djipp, dedett thiow dou djipp ndakh sène dokhaline défoul dara loudoul yokk sunu fitt leeral sunu beutt niou xippi di guiss legui xam negn kane moy kane yeah ragné nagnou bitch yi Gni niou sekhall ba sène gatt feess meuneutouniou wakh gni mbouxoum kerall boulène sax sène dotouniou marche gnémétouniou naadj gnom ak gni niouy door nio far degn ley togn nga aalou niou shoot seu ndeye parei neila masta après capitaine bou démissionner ak bèneu juge bou rassou dossier biniou classé dou takh bountou histoire bi teudjou li dou juste simplou niakhtou degn niou boukh bagn seuss niou fippou ndakh guissouniou avenir ci reew bouy nott djaboot keuff séni kaddou prefet téyé callam dissi djot ay ordre bavures nervis yi done saltél claté negn bo coupé sunu connexion nionguék VPN dieundeu nga Aissatou Diop Fall Nionguek Absa bou Seneweb Té CNRA meunoul bloqué Youtube Diamonoy sopalikou Danga sous-estimer sunu capacité tei dingako réthiou #freesenegal​ hashtag bi moungui daw té di negn ko doundou génération twitter tiktok instagram baaram doyna pour daanél ngouur bénn pour cliquer 5 pour ngueupp ay big kheer té balle bouy taak sène serment lay taal wakhko bepp takk derr légui sipp negn seu système seuss negn té negn insister sonko bou libre début le rek takhoul ba thioki bi djekh comme que do degg deug tchi larbin yi ley assister peuple bey andeu wakh nga degg Yaw linga beug def baye dou dém mais comme danga gnou beug test kay gnou dem Kou ndobine rey sa mame daaw dé rêne lou nioul foko sène doko diégué dingko daw bodé borom xell yeah nitteu gawa faté lolo takh nga takamlou deuk leumm té niola faal prési dem prési dikk prési doul niou sissou fippou takk derr yi diniou shoot Mbirr bi doufi goulète kagn lagnouy tall khekh yu Bess yakarone nagn la tchi demb macky sall mais teydji nioune la contre yaw té nala leer né dictateur doufi am ndam Rafétalaal litchi dess ngala thiow li na djekh domou rew mi gningui dè tchi diéma défendre séni rêve gni dieul balle gni dieul gaal tchi nguru macky sall esk bo teudé dinga nélaw goudi esk culpabilité leek leek dinaley fék sii def niou sey dom li dess mandat bi niou def la ndjiite mou djekh ak djamm nga dem bo bégné gaal gui dikk.

Canabasse